summaryrefslogtreecommitdiff
path: root/debian/po/wo.po
blob: 6211fea1f5db7dd249dff0c5bbc3f75a13cc79c3 (plain)
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42
43
44
45
46
47
48
49
50
51
52
53
54
55
56
57
58
59
60
61
62
63
64
65
66
67
68
69
70
71
72
73
74
75
76
77
78
79
80
81
82
83
84
85
86
87
88
89
90
91
92
93
94
95
96
97
98
99
100
101
102
103
104
105
106
107
108
109
110
111
112
113
114
115
116
117
118
119
120
121
122
123
124
125
126
127
128
129
130
131
132
133
134
135
136
137
138
139
140
141
142
143
144
145
146
147
148
149
150
151
152
153
154
155
156
157
158
159
160
161
162
163
164
165
166
167
168
169
170
171
172
173
174
175
176
177
178
179
180
181
182
183
184
185
186
187
188
189
190
191
192
193
194
195
196
197
198
199
200
201
202
203
204
205
206
207
208
209
210
211
212
213
214
215
216
217
218
219
220
221
222
223
224
225
226
227
228
229
230
231
232
233
234
235
236
237
238
239
240
241
242
243
244
245
246
247
248
249
250
251
252
253
254
255
256
257
258
259
260
261
262
263
264
265
266
267
268
269
270
271
272
273
274
275
276
277
278
279
280
281
282
283
284
285
286
287
288
289
290
291
292
293
294
295
296
297
298
299
300
301
302
303
304
305
306
307
308
309
310
311
312
313
314
315
316
317
318
319
320
321
322
323
324
325
326
327
328
329
330
331
332
333
334
335
336
337
338
339
340
341
342
343
344
345
346
347
348
349
350
351
352
353
354
355
356
357
358
359
360
361
362
363
364
365
366
367
368
369
370
371
372
373
374
375
376
377
378
379
380
381
382
383
384
385
386
387
388
389
390
391
392
393
394
395
396
397
398
399
400
401
402
403
404
405
406
407
408
409
410
411
412
413
414
415
416
417
418
419
420
421
422
423
424
425
426
427
428
429
430
431
432
433
434
435
436
437
438
439
440
441
442
443
444
445
446
447
448
449
450
451
452
453
454
455
456
457
458
459
460
461
462
463
464
465
466
467
468
469
470
471
472
473
474
475
476
477
478
479
480
481
482
# translation of xorg_po_wo.po to Wolof
# This file is distributed under the same license as the PACKAGE package.
# Copyright (C) YEAR THE PACKAGE'S COPYRIGHT HOLDER.
#
# Mouhamadou Mamoune Mbacke <mouhamadoumamoune@gmail.com>, 2006, 2008.
msgid ""
msgstr ""
"Project-Id-Version: xorg_po_wo\n"
"Report-Msgid-Bugs-To: xorg@packages.debian.org\n"
"POT-Creation-Date: 2009-06-02 20:32+0200\n"
"PO-Revision-Date: 2008-09-30 13:25+0200\n"
"Last-Translator: Mouhamadou Mamoune Mbacke <mouhamadoumamoune@gmail.com>\n"
"Language-Team: Wolof <en@li.org>\n"
"MIME-Version: 1.0\n"
"Content-Type: text/plain; charset=UTF-8\n"
"Content-Transfer-Encoding: 8bit\n"
"X-Generator: KBabel 1.11.4\n"

#. Type: select
#. Choices
#: ../x11-common.templates:2001
msgid "Root Only"
msgstr "Root Rekk"

#. Type: select
#. Choices
#: ../x11-common.templates:2001
msgid "Console Users Only"
msgstr "Jëfandikukat yu Konsol Rekk"

#. Type: select
#. Choices
#: ../x11-common.templates:2001
msgid "Anybody"
msgstr "Kumu mana doon"

#. Type: select
#. Description
#: ../x11-common.templates:2002
msgid "Users allowed to start the X server:"
msgstr "Jëfandikukat yiñu may ñu tambule serwóor X:"

#. Type: select
#. Description
#: ../x11-common.templates:2002
msgid ""
"Because the X server runs with superuser privileges, it may be unwise to "
"permit any user to start it, for security reasons.  On the other hand, it is "
"even more unwise to run general-purpose X client programs as root, which is "
"what may happen if only root is permitted to start the X server.  A good "
"compromise is to permit the X server to be started only by users logged in "
"to one of the virtual consoles."
msgstr ""
"Binga xamee ne serwóor X dafay dox ak sañsañu superuser, doonul lu xellu di "
"may ñéppu ñukoy mana tambule, ngir kaaraangey sistem bi. Ba tay doonul yit "
"lu xellu rugge root ba noppi di doxal prograam kiliyaŋ yu X, ta loolu mooy "
"am bu fekkee dangaa def ne root rekk mooy mana tambule serwóor X. Jubna lool "
"nak nga def ne serwóor X kikoy mana tambule day doon ku duggee ci benn ci "
"konsol wirtuwel yi."

#~ msgid "Nice value for the X server:"
#~ msgstr "Walóor nice bu serwóor X:"

#~ msgid ""
#~ "When using operating system kernels with a particular scheduling "
#~ "strategy, it has been widely noted that the X server's performance "
#~ "improves when it is run at a higher process priority than the default; a "
#~ "process's priority is known as its \"nice\" value.  These values range "
#~ "from -20 (extremely high priority, or \"not nice\" to other processes) to "
#~ "19 (extremely low priority).  The default nice value for ordinary "
#~ "processes is 0, and this is also the recommend value for the X server."
#~ msgstr ""
#~ "Booy jëfandikoo kernel bu sistemu doxaliin bu yore yenn estrateji bu nos "
#~ "waxtuy liggéey, seetlu nañu bubaax ne liggéeyu serwóor X bi dana gana "
#~ "rafet bu fekkee dafay dox ak piriyorite liggéey (process) bu gëna kawe bu "
#~ "defóo bi; piriyorite bi ab liggéey di am (maanaa ab process) lañuy tudde "
#~ "walóoru \"nice\".  Walóor yooyu mingi tambulee ci -20 (piriyorite bu kawe "
#~ "lool, maanaa  \"not nice\" ci yaneen liggéey yi) baci 19 (piriyorite bu "
#~ "suufe lool).  Walóor nice bu defóo bu liggéy ordineer moooy 0, ta moom "
#~ "yit lañuy laabiire ñu jox ko serwóor X."

#~ msgid ""
#~ "Values outside the range of -10 to 0 are not recommended; too negative, "
#~ "and the X server will interfere with important system tasks.  Too "
#~ "positive, and the X server will be sluggish and unresponsive."
#~ msgstr ""
#~ "Walóor yi génn diggante -10 ba 0 laabiirewuñu kukoy joxe, dañoo negatif "
#~ "bamu ëppu, dañuy tax serwóor X bi di duggante ak yenn liggéey yu sistem "
#~ "yu am solo yi. Bu doonee lu positif bamu ëppu, konn serwóor X bi dafay "
#~ "tayyeel lool ba nga xamne daanaka du wuyyu ci liñukoy woo."

#~ msgid "Incorrect nice value"
#~ msgstr "Walóor nice bi baajul"

#~ msgid "Please enter an integer between -20 and 19."
#~ msgstr "Joxeel ab numero bu wér digga -20 ak 19."

#~ msgid "Major possible upgrade issues"
#~ msgstr "Yenn probleem yukk daraja (upgrade)"

#~ msgid ""
#~ "Some users have reported that upon upgrade to the current package set, "
#~ "their xserver package was no longer installed. Because there is no easy "
#~ "way around this problem, you should be sure to check that the xserver-"
#~ "xorg package is installed after upgrade. If it is not installed and you "
#~ "require it, it is recommended that you install the xorg package to make "
#~ "sure you have a fully functional X setup."
#~ msgstr ""
#~ "Yenn jëfandikukat yi waxnañu ne buñu yokkee daraja seen sistem bi andiko "
#~ "ci bii paket. seeni paket yu xserver deesootuko istale. Ginnaaw problem "
#~ "boobu yoombula lijjanti, kon warngaa seet baxam paketu xserver-xorg "
#~ "istaleesna ko ginaaaw boo yokkee daraja ba noppi. Bu fekkee istaleesu ko "
#~ "ta nga soxla ko, kon ñingi lay laabiire nga istale paket bu xorg ngir mu "
#~ "wóor la ne da nga am istalaasioŋ bu X buy dox."

#~ msgid "Cannot remove /usr/X11R6/bin directory"
#~ msgstr "Manula dindi kaggu bu /usr/X11R6/bin"

#~ msgid ""
#~ "This upgrade requires that the /usr/X11R6/bin directory be removed and "
#~ "replaced with a symlink. An attempt was made to do so, but it failed, "
#~ "most likely because the directory is not yet empty. You must move the "
#~ "files that are currently in the directory out of the way so that the "
#~ "installation can complete. If you like, you may move them back after the "
#~ "symlink is in place."
#~ msgstr ""
#~ "Yokku daraja bi dafay laaj ñu dindi kaggu bu /usr/X11/R6/bin wottee ko ak "
#~ "ab simlink. Loolu jéemnanukoo def waaye antuwul, likoy waral amaana moodi "
#~ "kaggu bi dafa am lu ci nekk ba leegi. Da ngaa wara dindi fiise yi nekk ci "
#~ "kaggu bi ngir istalaasioŋ bi man egg. Bula neexee sax mannga leena "
#~ "delloosi ginnaaw bu simlink bi istalewoo ba noppi."

#~ msgid ""
#~ "This package installation will now fail and exit so that you can do this. "
#~ "Please re-run your upgrade procedure after you have cleaned out the "
#~ "directory."
#~ msgstr ""
#~ "Kon istalaasioŋ bu bii paket antuwl ta mingi nii di génn ngir nga mana "
#~ "def loolii. Kon nanga dellu defaat yokku daraja bi ginnaaw boo setalee "
#~ "kaggu bi ba noppi."

#~ msgid "Video card's bus identifier:"
#~ msgstr "Xamlekat (ID) bu bus bo kart video bi:"

#~ msgid ""
#~ "Users of PowerPC machines, and users of any computer with multiple video "
#~ "devices, should specify the BusID of the video card in an accepted bus-"
#~ "specific format."
#~ msgstr ""
#~ "Ñiy jëfandikoo masin yu PowerPC, ak ñiy jëfandikoo kompiyutar bu am ay "
#~ "kart video yu bare, dañoo wara joxe BusID bu kart video bi ci ab formaat "
#~ "bu dëppóo ak formaat yu bus yi."

#~ msgid "Examples:"
#~ msgstr "Misaal yi:"

#~ msgid ""
#~ "For users of multi-head setups, this option will configure only one of "
#~ "the heads.  Further configuration will have to be done manually in the X "
#~ "server configuration file, /etc/X11/xorg.conf."
#~ msgstr ""
#~ "Ñiy jëfandikoo komfiguraasioŋ bu ay boppu yu bare (multi-head setups), "
#~ "nañu xam ne lii benn ci boppu yi rekk lay komfigure.  Ngir komfigure "
#~ "yaneen yi, deesna ko mana def ak loxo ci fiise komfiguraasioŋ bu serwóor "
#~ "X bi, /etc/X11/xorg.conf."

#~ msgid ""
#~ "You may wish to use the \"lspci\" command to determine the bus location "
#~ "of your PCI, AGP, or PCI-Express video card."
#~ msgstr ""
#~ "Amaan nga soxlaa jëfandikoo komaand bu \"lspci\" ngir xam barab bi bus bu "
#~ "kart video PCI, AGP, wall PCI-Express nekk."

#~ msgid ""
#~ "When possible, this question has been pre-answered for you and you should "
#~ "accept the default unless you know it doesn't work."
#~ msgstr ""
#~ "Saa yu manee rek, bii laaj joxeelnañu la toontoom ba noppi. Dangaa wara "
#~ "naŋgu defóo bi ndare ba dalaa wóor ne doxul."

#~ msgid "Incorrect format for the bus identifier"
#~ msgstr "Formaatu xamlekat (ID) bu bus bi baaxul"

#~ msgid "Use kernel framebuffer device interface?"
#~ msgstr "Ndax nu jëfandikoo interfaasu periferik framebuffer bu kernel bi?"

#~ msgid ""
#~ "Rather than communicating directly with the video hardware, the X server "
#~ "may be configured to perform some operations, such as video mode "
#~ "switching, via the kernel's framebuffer driver."
#~ msgstr ""
#~ "Serwóor X bi man naa baña jokkoo jokkoo bu joñjoo ak periferik video bi, "
#~ "nga xam ne deeskoy komfigure muy def yenn jëf yi, lu mel ne soppi "
#~ "doxaliinu video bi, jaarko ci driver framebuffer bu kernel bi."

#~ msgid ""
#~ "In theory, either approach should work, but in practice, sometimes one "
#~ "does and the other does not.  Enabling this option is the safe bet, but "
#~ "feel free to turn it off if it appears to cause problems."
#~ msgstr ""
#~ "Ci xalaat moom ñaar yeppu man nañoo dox, waaya ci jëf moom, leegleeg benn "
#~ "bi dox baneen bi baña dox.  Tann lii lu wóor la, waaya bula naree andil "
#~ "ay jafejafe kon man nga koo dindi."

#~ msgid "XKB rule set to use:"
#~ msgstr "Reegalu XKB biñu jëfandikoo:"

#~ msgid ""
#~ "For the X server to handle the keyboard correctly, an XKB rule set must "
#~ "be chosen."
#~ msgstr ""
#~ "Ngir serwóor X bi mana doxal tablocaabi bi nimu ware, dangaa wara tann ab "
#~ "reegalu XKB."

#~ msgid "Users of most keyboards should enter \"xorg\"."
#~ msgstr ""
#~ "Ñiy jëfandikoo li ëppu ci tablocaabi yi dañuy wara bind fii \"xorg\"."

#~ msgid ""
#~ "Experienced users can use any defined XKB rule set.  If the xkb-data "
#~ "package has been unpacked, see the /usr/share/X11/xkb/rules directory for "
#~ "available rule sets."
#~ msgstr ""
#~ "Jëfandikukat yi yagg ci mbir mi ñoom man na ñoo jafadikoo beppu reegalu "
#~ "XKB boo xam ne daytalnañuko. Bu fekkee paket bu xkb-data tajjinañuko ba "
#~ "noppi, kon xoolal kaggu bu /user/share/X11/xkb/rules ngir xam reegal yifi "
#~ "am."

#~ msgid "When in doubt, this value should be set to \"xorg\"."
#~ msgstr "Bu fekke dangay nattable, kon fii bind fi \"xorg\"."

#~ msgid "Keyboard model:"
#~ msgstr "Modeel bu tablocaabi bi:"

#~ msgid ""
#~ "For the X server to handle the keyboard correctly, a keyboard model must "
#~ "be entered.  Available models depend on which XKB rule set is in use."
#~ msgstr ""
#~ "Ngir serwóor X bi mana doxal tablocaabi bi nimu ware, dangaa wara joxe "
#~ "fiim ab modeel bu tablocaabi. Modeel yi fiy am mingi sukkadiku ci reegal "
#~ "XKB yi ñuy jëfandikoo."

#~ msgid ""
#~ " With the \"xorg\" rule set:\n"
#~ " - pc101: traditional IBM PC/AT style keyboard with 101 keys, common in\n"
#~ "          the United States.  Has no \"logo\" or \"menu\" keys;\n"
#~ " - pc104: similar to pc101 model, with additional keys, usually engraved\n"
#~ "          with a \"logo\" symbol and a \"menu\" symbol;\n"
#~ " - pc102: similar to pc101 and often found in Europe. Includes a \"< >\" "
#~ "key;\n"
#~ " - pc105: similar to pc104 and often found in Europe. Includes a \"< >\" "
#~ "key;\n"
#~ " - macintosh: Macintosh keyboards using the new input layer with Linux\n"
#~ "              keycodes;\n"
#~ " - macintosh_old: Macintosh keyboards not using the new input layer;\n"
#~ " - type4: Sun Type4 keyboards;\n"
#~ " - type5: Sun Type5 keyboards."
#~ msgstr ""
#~ "Boo tannee reegal yu  \"xorg\" :\n"
#~ " - pc101: estil bu cosaan bu tablocaabi IBM PC/AT bu am 101 butoŋ, ñu "
#~ "miinko ci\n"
#~ "          Etaa yu Bennoo yu Aamerik (USA).  Amul butoŋ bu  \"logo\" amul "
#~ "yit bu \"menu\" ;\n"
#~ " - pc104: dafa niróo ak modeel buc101l, waaye day am yaneen butoŋ, yuñu "
#~ "nataal\n"
#~ "           ab màndarga \"logo\" ak màndarga bu \"menu\";\n"
#~ " - pc102: dafay niróo ak  pc101 ta deesnako faral di gis ci Óróop "
#~ "(Europe). Dafay am ab butoŋ bu \"< >\" ;\n"
#~ " - pc105: dafay niróo ak pc104 ta deesnako faral di gis ci Óróop. Dafay "
#~ "am ab butoŋ bu  \"< >\" ;\n"
#~ " - macintosh: tablocaabi bu Macintosh buy jëfandikoo kuusu dugël (input) "
#~ "bu yees bi ak keycodes\n"
#~ "              yu Linux;\n"
#~ " - macintosh_old: tablocaabi bu Macintosh budul jëfandikoo kuusu dugël bu "
#~ "yees bi.\n"
#~ " Budee ci reegal yu \"sun\":\n"
#~ " - type4: tablocaabi Type4 bu Sun;\n"
#~ " - type5: tablocaabi Type5 bu Sun."

#~ msgid ""
#~ "Laptop keyboards often do not have as many keys as standalone models; "
#~ "laptop users should select the keyboard model most closely approximated "
#~ "by the above."
#~ msgstr ""
#~ "Kompiyutar yiñuy gaddu (laptop) ñoom duñuy faral di am mbooleem butoŋ yi "
#~ "modeel yu mag yi di am, kon ñi yore kompiyutar yiñuy gaddu dañoo wara "
#~ "tann modeel bi gëna jege seen bos ci yii ñu lim ci kaw."

#~ msgid ""
#~ "Experienced users can use any model defined by the selected XKB rule "
#~ "set.  If the xkb-data package has been unpacked, see the /usr/share/X11/"
#~ "xkb/rules directory for available rule sets."
#~ msgstr ""
#~ "Jëfandikukay yi miin Linux ñoom man nañoo tann béppu modeel buñu daytal "
#~ "ci reegal bu XKB biñu tann. Bu fekkee paket bu xkb-data dajjeesna ko, kon "
#~ "xoolal kaggu bu /usr/share/X11/xkb/rules ngir xam reegal yifi am."

#~ msgid ""
#~ "Users of U.S. English keyboards should generally enter \"pc104\".  Users "
#~ "of most other keyboards should generally enter \"pc105\"."
#~ msgstr ""
#~ "Ñiy jëfandikoo tablocaabi bu Aŋgle Amerikee (US English) lici ëppu dañuy "
#~ "wara bind fii \"pc104\". Ñiy jëfandikoo yi ëppu ci yaneen toblocaabi "
#~ "dañuy wara bind fii \"pc105\"."

#~ msgid "Keyboard layout:"
#~ msgstr "Tërëliinu tablocaabi bi:"

#~ msgid ""
#~ "For the X server to handle the keyboard correctly, a keyboard layout must "
#~ "be entered.  Available layouts depend on which XKB rule set and keyboard "
#~ "model were previously selected."
#~ msgstr ""
#~ "Ngir serwóor X bi di mana doxal tablocaabi bi nimu ware, dangaa wara bind "
#~ "fii aw tërëliinu tablocaabi. Tërëliin yi ngay mana tann ci ngiy aju ci "
#~ "reegal XKB ak modeelu tablocaabi yinga tannoon."

#~ msgid ""
#~ "Experienced users can use any layout supported by the selected XKB rule "
#~ "set.  If the xkb-data package has been unpacked, see the /usr/share/X11/"
#~ "xkb/rules directory for available rule sets."
#~ msgstr ""
#~ "Jëfandikukay yi miin Linux ñoom danañu mana tann béppu tërëliin boo xam "
#~ "ne reegal XKB bi danako naŋgu.  Bu fekkee paket bu xkb-data dajjeesna ko, "
#~ "kon xoola kaggu bu /usr/shar/X11/xkb/rules ngir mana xam reegal yifi am."

#~ msgid ""
#~ "Users of U.S. English keyboards should enter \"us\".  Users of keyboards "
#~ "localized for other countries should generally enter their ISO 3166 "
#~ "country code.  E.g., France uses \"fr\", and Germany uses \"de\"."
#~ msgstr ""
#~ "Ñiy jëfandikoo tablocaabi yu US English ñoom dañuy wara bind fii \"us\".  "
#~ "Ñiy jëfandikoo tablocaabi yuñu lokaaliise ñeel seen réew ñoom dañuy bi "
#~ "kod ISO 3166 bu seen réew. Ci misaal Almaañ migni doon \"de\", Fraas doon "
#~ "\"fr\"."

#~ msgid "Keyboard variant:"
#~ msgstr "Cafaan bu tablocaabi bi:"

#~ msgid ""
#~ "For the X server to handle the keyboard as desired, a keyboard variant "
#~ "may be entered.  Available variants depend on which XKB rule set, model, "
#~ "and layout were previously selected."
#~ msgstr ""
#~ "Ngir serwóor X bi di mana doxal tablocaabi bi nimu ware, dangaa wara bind "
#~ "fii ab cafaan bu tablocaabi.  Cafaan yifiy am mingiy sukkandiku ci reegal "
#~ "XKB, ak tërëliin yinga tannoon."

#~ msgid ""
#~ "Many keyboard layouts support an option to treat \"dead\" keys such as "
#~ "non-spacing accent marks and diaereses as normal spacing keys, and if "
#~ "this is the preferred behavior, enter \"nodeadkeys\"."
#~ msgstr ""
#~ "Lu bare ci tërëliinu tablocaabi yi danañu mana tanna jëflënté ak butoŋ yu "
#~ "dee yi \"dead keys\", yu mel ne maaska yudul ànd ak espaas, ñaari tombu "
#~ "ci kaw araf (dieres), jëlënté ak ñoom mel ne buñu doonoon butoŋ yu espaas "
#~ "yu normaal. Bu fekkee loolu nga bëgg kon bindal fii \"nodeadkeys\"."

#~ msgid ""
#~ "Experienced users can use any variant supported by the selected XKB "
#~ "layout.  If the xkb-data package has been unpacked, see the /usr/share/"
#~ "X11/xkb/symbols directory for the file corresponding to your selected "
#~ "layout for available variants."
#~ msgstr ""
#~ "Jëfandikukay yi miin Linux ñoom danañu mana tann béppu cafaan boo xam ne "
#~ "reegal XKB bi danako naŋgu.  Bu fekkee paket bu xkb-data dajjeesna ko, "
#~ "kon xoola kaggu bu /usr/shar/X11/xkb/symbols ngir gis fiise bi dëppóo ak "
#~ "tërëliin winga tànn, danga ca gis cafaan yi fi am."

#~ msgid ""
#~ "Users of U.S. English keyboards should generally leave this entry blank."
#~ msgstr ""
#~ "Ñiy jëfandikoo tablocaabi bu Aŋgle Amerikee (US English) ñoom li ci ëppu "
#~ "waruñoo bind fii dara."

#~ msgid "Keyboard options:"
#~ msgstr "Tann yu tablocaabi bi:"

#~ msgid ""
#~ "For the X server to handle the keyboard as desired, keyboard options may "
#~ "be entered.  Available options depend on which XKB rule set was "
#~ "previously selected.  Not all options will work with every keyboard model "
#~ "and layout."
#~ msgstr ""
#~ "Ngir serwóor X bi di mana doxal tablocaabi bi ninga koy bëggé, man ngaa "
#~ "bind fii ay tanni tablocaabi. Tann yi ngay mana def ñingiy aju ci reegal "
#~ "XKB yinga tannoon. Tann yéppu nak duñu dox ci modeeli tablocaabi yéppu ak "
#~ "tërëliin yéppu."

#~ msgid ""
#~ "For example, if you wish the Caps Lock key to behave as an additional "
#~ "Control key, you may enter \"ctrl:nocaps\"; if you would like to switch "
#~ "the Caps Lock and left Control keys, you may enter \"ctrl:swapcaps\"."
#~ msgstr ""
#~ "Ci misaal, Boo bëggée butoŋ bu Caps Lock mu mel ne baneen butoŋ bu "
#~ "Control, kon dangay bind fii \"ctrl:nocaps\", Boo bëggée taal Caps Lock "
#~ "ak butoŋ Control yi ci jammooy, kon man ngaa bind fii \"ctrl:swapcaps\"."

#~ msgid ""
#~ "As another example, some people prefer having the Meta keys available on "
#~ "their keyboard's Alt keys (this is the default), while other people "
#~ "prefer having the Meta keys on the Windows or \"logo\" keys instead.  If "
#~ "you prefer to use your Windows or logo keys as Meta keys, you may enter "
#~ "\"altwin:meta_win\"."
#~ msgstr ""
#~ "Baneen misaal mingi nii: ñenn ñi dañuy bëgg butoŋ yu Meta yi nekk ci "
#~ "butoŋ Alt yi ci tablocaabi bi (loolu mooy defóo bi), amna yit ñaneen "
#~ "dañuy bëgg butoŋ bu Meta nekk ci butoŋ bu Windows bi walla butoŋ bu \"logo"
#~ "\" bi. Bu fekkee dangaa bëgga jëfandikoo butoŋ bu Windows bi walla bu "
#~ "logo bi defleen ñuy say butoŋ yu Meta, kon man ngaa bind fii \"altwin:"
#~ "meta_win\"."

#~ msgid ""
#~ "You can combine options by separating them with a comma, for instance "
#~ "\"ctrl:nocaps,altwin:meta_win\"."
#~ msgstr ""
#~ "Man nga boole ay tann daldi leen teqale ak ay wirgil, ci misaal \"ctrl:"
#~ "nocaps,altwin:meta_win\"."

#~ msgid ""
#~ "Experienced users can use any options compatible with the selected XKB "
#~ "model, layout and variant."
#~ msgstr ""
#~ "Jëfandikukay yi miin Linux ñoom danañu mana jëfandikoo béppu tànn boo xam "
#~ "ne modeelu XKB bi, tërëliinwi ak cafaan bi danañuko naŋgu."

#~ msgid "When in doubt, this value should be left blank."
#~ msgstr "Bu fekkee dangay sikksakka, kon fii waróo fée bind dara."

#~ msgid "Empty value"
#~ msgstr "Lim bi dafa widd"

#~ msgid "A null entry is not permitted for this value."
#~ msgstr "Fii duñu naŋgu nga bayyiko mu neen bañ fee def dara."

#~ msgid "Invalid double-quote characters"
#~ msgstr "Karakteer yu guillemet yi baaxul"

#~ msgid "Double-quote (\") characters are not permitted in the entry value."
#~ msgstr "Karakteer bu guillemet (\") deesuko naŋgu fii."

#~ msgid "Numerical value needed"
#~ msgstr "Am lim (numero) lañu soxla"

#~ msgid "Characters other than digits are not allowed in the entry."
#~ msgstr "Kenn du naŋgu fii ab karakteer budul ab lim (numero)."

#~ msgid "Autodetect keyboard layout?"
#~ msgstr "Ndax nu jéema gisal sunu boppu tërëliinu tablocaabi bi?"

#~ msgid ""
#~ "The default keyboard layout selection for the Xorg server will be based "
#~ "on a combination of the language and the keyboard layout selected in the "
#~ "installer."
#~ msgstr ""
#~ "Serwóor Xorg bi, ci tann tërëliinu tablocaabi bu defóo bi mingiy "
#~ "sukkandiku ci làkk wi nga tann ak ci tërëliinu tablocaabi wi nga tann ci "
#~ "prograamu istalaasioŋ bi."

#~ msgid ""
#~ "Choose this option if you want the keyboard layout to be redetected.  Do "
#~ "not choose it if you want to keep your current layout."
#~ msgstr ""
#~ "Tannal lii boo bëggée ñu jéema làmbutuwaat tërëliinu tablocaabi bi. Buko "
#~ "tann boo bëggée jappu ci tëëliin wi nga yor fimune nii."

#~ msgid "X server driver:"
#~ msgstr "Driver bu serwóir X:"

#~ msgid ""
#~ "For the X Window System graphical user interface to operate correctly, it "
#~ "is necessary to select a video card driver for the X server."
#~ msgstr ""
#~ "Ngir interfaas Graafik bu X Window System bi mana dox nimu ware, fàwwu "
#~ "dangaa wara tann ab driver bu serwóor X bi."

#~ msgid ""
#~ "Drivers are typically named for the video card or chipset manufacturer, "
#~ "or for a specific model or family of chipsets."
#~ msgstr ""
#~ "Driver yi ñingi leen di farala yor turu kart video bi walla turu ki "
#~ "liggéey chipset bi, walla modeel ak njabootu chipset yi."